Jesus-icon.png
Ay bés ak Yeesu

Vimeo
YouTube


40 bés ak Yeesu

Bés 01: Tambale gi  Yowanna 3:16-17
Bés 02: Juddu gu kéemaane  Luug 1:3-2:18
Bés 03: Sóoboog Yeesu ci ndox  Luug 3:1-23
Bés 04: Fiir yi Seytaane jëmale woon ci Yeesu  Luug 4:1-13
Bés 05: Yonnentug Yeesu  Luug 4:16-31
Bés 06: Woyof gu dëggu  Luug 18:10-14
Bés 07: Napp gu kéemaane Luug 5:4-11
Bés 08: Dekkil neew  Luug 8:41-56
Bés 09: Bi Yeesu di tann fukk  taalibe yi ak  ñaar   Luug 5:27-28,6:12-16
Bés 10: Mbékte yu woor yi  Luug 6:17-23
Bés 11: Waare ba Yeesu waare woon ca tund wa (Xaaj 1)  Luug 6:24-27
Bés 12: Waare ba Yeesu waare woon ca tund wa (Xaaj 2)  Luug 6:27-42
Bés 13: Njegale, ak xaste Luug 7:36-50
Bés 14: Taalibe yu jigéen  Luug 8:1-3
Bés 15: Laaju Yowanna  Luug 7:18-23
Bés 16: Léebu suuf yi  Luug 8:4-15
Bés 17: Léebu lamp bi  Luug 8:16-18
Bés 18: Ngélaw lu bare doole  Luug 8:22-26
Bés 19: Ki rab jàpp  Luug 8:27-39
Bés 20: Dundal 5000 nit  Luug 9:11-17
Bés 21: Ki Yeesu nekk dëgg  Luug 9:18-22
Bés 22: Ñaanu Boroom bi Luug 11:1-4
Bés 23: Ñaan ak njàqare  Luug 11:9-13,12:22-28
Bés 24: Nguurug nit ñi  Luug 13:18-19
Bés 25: Dëngoog Nguur  Luug 12:10-16
Bés 26: Waayi Samari ju baax ja  Luug 10:25-37
Bés 27: Gumba ga  Luug 18:35-43
Bés 28: Sase  Luug 19:1-10
Bés 29: Duggug Ndam  Luug 19:28-41
Bés 30: Mbirum xaalis Luug 19:45-21:4
Bés 31: Sañ sañu Yeesu Luug 20:1-26
Bés 32: Reer bu mujj ba 22:7-23
Bés 33: Néeg bu kawe ba Luug 22:26-38
Bés 34: Wor gi  Luug 22:40-65
Bés 35: Layoo ba  Luug 22:63-71
Bés 36: Reyu daaj ci bant  Luug 23:25-45
Bés 37: Deewu Yeesu  Luug 23:44-56
Bés 38: Moom dekki na  Luug 23:56-24:50
Bés 39: Berndeel gi  Room 3:23, 5:8, 6:23
Bés 40: Ndigal lu mag li  Macë 28:18-20



7 bes ak Yesu: Yiw

Bés 1: Tont lu yiwe  Luug 8:41-56
Bés 2: Njegal ak yiw  Luug 7:36-50
Bés 3: Yiw walla yoon  Luug 12:32-34; 13:10-17
Bés 4: Jëfi yiw  Luug 10:25-37
Bés 5: Wey ciw yiw  Luug 18:35-43
Bés 6: Firndeey yiw  Luug 19:1-10
Bés 7: Yiw wi bant ba bañu daajoon Yeesu feeñal  Luug 23:39-56